Au sortir des journées culturelles de Mbeuleukhé, les populations n’ont cessé de témoigner leur reconnaissance et de formuler des prières à l’endroit des membres du RAM et de l’AEERM. C’est dans ce même élan que Saér Niang, fils de Ibra Niang membre fondateur du RAM, a écrit un poème qui a ému plus d’un.Ce qui lui a valu le prix Mbeuleukhé.net du meilleur poème. Ce poème est dédié à ces deux associations sœurs (RAM & AEERM) pour magnifier leurs actions menées dans leur terroir. Mbeuleukhé.net vous livre ici le verbatim de ce Talif de Saèr Niang que lui-même a entonné lors de la cérémonie de clôture.
Depuis diamanoy Pa Ibra ak Pa Djiby DIAW
RAM dékki wat DAW
Di raam ba raw
Gaayadoone daw
Gniko djiiité di ay Ndaw
Yééneu takh ba gniléne beugue nan niaw
Gniléne bagne ba béw
Si sén moudjeunteulou nieuw
Linguéne fi déf mingui néfi béwe
Balle,yéré, cap bassi massinou niaw
Dou léneu lou niaka téw
Si diamanoy diékhitalou taw
Waadiour yi dane daan diooy
Bouléne ndiabott yi néléne khéwe
Indifi béne cartable par élève
Si lou rombe niéti téméri éléw
Li nguéne kham daale moy téw mi téw
Ness kiiss
Si niaari ay bess
Nguéne wathié fi ambulance bou bess
Ba takh tay niouy hapiness
Bou ndieuke koudane fébar bane fess
Gaayi nan dafay dess
Wala mou indialé kess
Ndakh niakoum ambulance bou bess
Deugue deugue yeur mandé léén fess
Ma dadiéke Pa boudane dieunde fournitures ba tass
Mouné ma gni gno diara niaanal niaanak khaass
Dieul dafar moune sén sass
Si diamanoy alternance
Si nguéne nieuw né darasse
Si nake en masse
Né 1fois ça passe
2 ça rasse
3 ça casse
|
Diapaléguéne trop la jeunesse
Père Ndonga ki rakam
Père Ndonga ki magam
Dikeu thi ay mbokam
Dieul defar mouy bakam
Déf mbeuleukhé mouy sagam
RAM lagnou gueum
Ndakh limou beug deukeum
Dieul défar mouy beugueum
Il n’est pas bon d’être bête mais il est bête de croire que ceux qui sont bons sont bêtes.
Si diamanoy nawét
Nguéne andak AEERM nieuw sougnou wét
Daw nak ay kilométes
Nguir rek consulter manam sét
Fathie nia sibourou naroona faat
Guiss yép daldi nettes bagne niouy minguélék ay porteurs de lunettes
Boulééne nékhoone took réwoum taakh
Nguéne nieuw né saraakh
Walahi yéna baakh
Khamouléne fate olof
Amouléne fate Djoloff
Néwouléne moukou dagnou soof
Niko rappeur bi Nit dof
Wakhé, les chefs
RAM dale dou moussa louf
Sama mame balla
Dana wakh khalé louko oumpou
Na dém sééti wa démbou
Nguir rék loumou soumbou
Mam ko délou
Kou nieuw nagne la fappe dougueul sougnou
Bagna tokk dilala
Ndakh am sakhoul,niakit sakhoul
Auteur: Saèr Niang
|
El H. Daouda DIAW