Ce poème du jeune prodige Saér Niang dédié à l’AEERM a été chanté à l’occasion des journées culturelles que l’AEERM organise chaque année à Mbeuleukhé. Ce poème qui non seulement magnifie l’engagement des membres de cette association au développement de leur terroir rappelle également à nos jeunes frères du Djoloff l’importance des études. A lire et à partager
AEERM nieuw na diaugué dahra
indalé wa dahra
ndakh nit mbokamay takh mou don dara
am fit tia kaw
wakh deugue ba fawe
naniou wout kham kham bou law
niko serigne DAME wakhéwone daw
am am sa ndaw
walay kaaw
ndakh niake dafa gaw
dawal ba raw
boul falé sakh taw
pencou ba soow
diakhaw ba pacaw
raw ba dialaw
ba gayi nan waw
kimo gaw
ma seti gor gui matar
mouné ma bay lén sen war
bagna tok di khar
boulén né mouke y'en a marre
benay indi niar
mille milliard
niake té baakh diaar diaar
nalén gueuneul am donap soular
ndakh bo dafé sa warrougar yalla doula bindal bakar
boulén niake don yambar
wala ngay am di sokhar
mba ngay démé khadar
pa matar néma sa mame birame niang
dana wakh kou deuké diangue
euleuk dinga banke
khalissou banque
wayé koun né diangal nga lanke
do fayéko banke
té dinga deuké banke
naniouy goor goorlou
bagna gawa kholou
di woté walou
bougnou amè lougnou khamoul
ndakh il y'a 100ans avant notre naissance
mam ya khamoun won licence kon nioune gni am chance
feké diamonoy licence
naniou diangue ba tass
ma diaugué dahra di dém dadiék ap peul
mounan béne eleve ci keur
fouki khath mo malén gueuneul
mou don nak wakh diouma seufeul
mané ko yaw khana démo BOULél
guiss lafay AEERM di amal
boulay khath bi di mbeuweul
nioune dagne leni bégueul
té biss dina nieuw inchala sougnou wadiour yi gnouléni dafal
nioungui sargal
yén gni gnou dalal
sougnou principal
corps professoral
ak yén gni gnou diaral
gniou diaugué boulél
diar daral
wathie dahra nguir dilén sagal
di kheuy diouraum niéti wakhtou you toftal
di wathie fouki wakhtok niar you tégal.
nioungui deglou linguén niouy wakhal
té di sakou nguén niouy nianal
AEERM sakhal,
kou am dara défal,
kou kham dara wakhal,
kou niaka kham ladial,
lignou beugue moy dilén bégueul
gayi que la fête soit belle.
Saér Niang, Mbeuleukhé
La Rédaction